Cheikh Moustapha al karim

Cheikh Moustapha al karim

Tu pourrais aussi aimer

Xcfgcfg
Xcfgcfg
Aaren
Aaren

عالم بسر الحروف الفعلية باجسادها وطبائعها واروحعها التي تنفعل بها اشياء +221775943377 WhatsApp

Photos from Cheikh Moustapha al karim's post 20/11/2023

kou beugue listikhar sèt bou lèrr danioulay wakh ba wakhla yèrè binga sol woniou 775943377

01/08/2023

xam say sarakh 🌹

pour savoir toutes opportunités du personne à n'importe quel distance 🌹☎️775943377

Photos from Cheikh Moustapha al karim's post 01/08/2023

الشيخ مصطفى الكريم عالم بسر الحروف الفعلية باجسادها وطبائعها واروحعها التي تنفعل بها اشياء من خير وشر

Photos from Cheikh Moustapha al karim's post 31/07/2023

rituel pour attacher quelqu'un à vous suivre ou ramener votre femme ou mari
الشيخ مصطفى الكريم عالم بسر الحروف الفعلية باجسادها وطبائعها واروحعها التي تنفعل بها اشياء من خير وشر

07/05/2023

mbookou yi tay nak daniou leene di laabiré leenne thi ndiariniou lorier. lorier nak dafa nekk garab goo xamni garab gou bari ndiarigne la waayé nak niou eupou thi nit gni xamouniou loudoul boolé ko ak aw niaw toogou ko.
lorier nak garab gou bari lool la thi Afrique. garab gui nak limou mana saafara thi ay diangoro kenn manou koo lim thi benn diatay. mom lorier nak garab gou yaague thi adouna la wa Inde ak roman yi fonkon naniou ko lool diko diafandi ko fann you bari garab gui nak thiosanam moy Asie.
bour yi moom laniou daan diafandi ko disi fadiou ak disi defar seen yaram si côté mystique
mootakh boo demé thi reewi toubaab you bari dangay feek niou diambat ko thi mbedd yi wala niou waralé ko seen keur yi.
--------‐--------------------------------------------------------------------
mbokou yi kepou koo xamni dangaa amé diabet woutal 5 xobi lorier nga woutaat doomou sab sab bou wow bi amna louy nek thi biir lou melni guérté
nioom niaar ngay boolé nga baxal leene baniou nior nga xeent ndakh mi diko naan par kaasou ataaya inchallah yalla dinala defal diaamou dinga doundou te doo am benn jafé
batay mbookou yi kepou kou amé cholesterol nga beugue mou waathi woutal xobi lorier nga woutaat jafé.

batay mbookou yi kepou kou amé cholesterol nga beugue mou waathi woutal 7 xobi lorier nga tangal ndakh sotti kosi nga bayi bamou sedde nga seegue ko diko naan par xaadiou kaas dana waathi.

batay mbookou kepou kou am beugne bouy mety na wout lorier deubou ko bamou nek poudre mou diko borossoo, bou fekee beugne bi dafa beunn nak ,nako boolé ak vinaigre daadi koy taf thi beugne bi inchallah dina taago ak beugne

batay mbokou yi kepou koo xamni dangaa amé jafé jafé nelaw woutal niaty xobi lorier nga def koo thi kaasou ndokh bou tangue nga naan ko balaa nga teud inchallah dinga nelaw boubakh.

batay mbookou yi kepou koo xamni dangaa amé hasma wouta 12l xobi lorier nga boole ko ak touti neb neb baxalko diko naan dana tanee inchallah.

batay mbookou yi kepou kou amé borom boopou dangay wout thi lorier lou toolok sa ngeubou lokho nga togou ko thi benn litarou ndakh boo nopee nak doo xaar mou seede thi tangaay ba noona nga koy mouro ab seur wala mbalaan tiim ko bouko defee thiolol yi dila dougou bamou matt 20mn nga doora sigui danga taako ak borom bopou inchallah .

batay mbookou yi bepou sokhna boo xamni dafa teudiou ba manoul am borom keur wala goor gou manoul am sokhna woutal 99 xobi lorier xob bou nekk mga bind thi benn tourou yalla nga sangoo ko jr jours inchallah danga seuy te seuy bou barkel lay doon

batay mbookou yi kepou koo xamni sa keur dafa bari thioow lool woutal xobi 16 lorier rek nga dëbu ko boole ko ak thiouraay Liban diko taal thia keur ga inchallah thioow la dootoul bary.

batay mbookou yi kepou kou thiat nekk thi yaw walla ndiabar walla kootou bindal
111 basmala nga boolé ko ak 111 lorier sangoko 3jr inchallah dina dindi lepou lou nekoon thi sa yaram bamou set withi.

batay mbookou yi kepou kou amé biir bouy metti woutal lorier lou tolook 15grm diko naan balaa ngay lekk inchallah dinako saafara lou gaw.

batay mbookou yi kepoukoo xamni chaytané daf laa dougou woutal 7 xobi lorier ak 7 neferaw mbaam, nga boolé ko defko thiouraay inchallah beenn yoon rek boko si suuroo chaytané si dana guenn ba sett withi.

batay mbookou yi kepou koo xamni dangaa ame jafé jafé lekk mou reess kookou nay faral di def heure bou lekke banopi rek mou dieul niaari xobi lorier booleko ak xobi naanaa tangal ndakh sotti kosi nga bayi bamou yaabi xeent ko naan ko inchallah loumou leek dana reess.

batay mbookou yi kepou kou beugue bayré bou yeemé lool te andak oubikou woutal 129 xobi lorier, xob bou nekk mga bindeu thi yaa
nga sangoo ko jr .diir binga koy sango nak biss bou nekk dangay werd ya latif 2377fois.

_____________________________________
xamna mbookou yi danay yam fofou ba baneen yoon inchallah liniou yalla xamlo thi lorier barina lool waaye damay yam fofou ba beneen yon niou nieuw thi yaneen ndiariniou garab

05/05/2023

canar qui peut dompter plus de4 personnes disponible
الشيخ محمدمصطفى عالم بجيب الحبيب عالم بسرالحروفوالفعلية باجسادهاوطبائعهاواروحعهاالتي تنفعل بهااشياءمن خيروشر

02/05/2023
Photos from Cheikh Moustapha al karim's post 25/03/2023

Pour avoir une femme ou mari
Kou beug am borom keur wala diabar
Bindal
ما يفتح الله للناس من رحمة فلاممسك فلاممسك لها ومايمسك فلا مرسل له من بعده وهو العزيز الحكيم 33fois
كأنهن الياقوت والمرجان 33fois
قالوا ياابانا مالك لاتامنا على يوسف واناله لناصحون، 33fois
Boleko ak sougouf foudeun defko safara sangoko 4 jeudi

Résultats immédiat

Photos from Cheikh Moustapha al karim's post 19/10/2022

Traitement pour tout vos problèmes de:
👉Faiblesse sexuelle
👉yokou awra
👉Hémorroïde
👉Asma
Dioni dioni 775943377

10/10/2022

Téré(fay wakh) est disponible, danga wara layo dji ak yone(justice)wala nga dougou thi problème Bo manoul guènn.térè "fay wakh " disponible lou problème bi reuy reuy dina sèdeu ba melni glace.
الشيخ مصطفى الكريم عالم بسر الحروف الفعلية باجسادها وطبائعها واروحعها التي تنفعل بها اشياء من خير وشر أعظم ساحر أفريقي أفضل شيخ بالسودان

Photos from Cheikh Moustapha al karim's post 30/09/2022

Dangay touki bagne sa diabar ndialo sa guinaw beugue niou defal lasi liguey kou teudeu ak sa diabar teulè dotoul man dara wala awra bi dou guénn woniou775943377

Il y'a des gens qui chercher votre femme., leur travail c'est chercher les femmes des voyageurs alors pour fermer ta femme personne ne pourra coucher avec lui appelle nous

29/09/2022

Kou beugue sa place di bari mbolo woniou775943377

27/09/2022

الشيخ مصطفى الكريم عالم بسر الحروف الحروف باجسادها وطبائعها واروحعها التي تنفعل بها اشياء من خير وشر

26/09/2022

Bo beuguè souba bala dianteu bei soh (avant lever du soleil☀) gua am xaliss mou new mou bari
Bindal la figure geomancie thi goura ( cola blanc) 7 fois defko sa poche bala dianteu bei soh dinga am xaliss .

Si tu veux avoir forcément d'argent avant la fin de la journée tracé adama ( cette figure en image) 7 fois le matin et faisant tes vœux et mets le dans ta poche tu auras une somme d'argent avant la fin de la journée

24/09/2022

Kouy def examen wala concours bindal
والسابقون السابقون أولئك المقربون
7fois boleko ak say yèn(sourcil)
Takk ko sa lokho ndaydior (droite) boudè goor. Thiamogne( gauche) boudè djiguén.

Résultat immédiat 🙏

20/09/2022

الشيخ مصطفى الكريم عالم بسر الحروف الفعلية باجسادها وطبائعها واروحعها التي تنفعل بها اشياء من خير وشر أعظم ساحر أفريقي

19/09/2022

الشيخ مصطفى الكريم عالم بسر الفعلية باجسادها وطبائعها واروحعها التي بها اشياء من خير وشر أعظم ساحر أفريقي

18/09/2022

الشيخ مصطفى الكريم عالم بسر الحروف الفعلية باجسادها وطبائعها واروحعها التي تنفعل بها اشياء من خير وشر أعظم ساحر أفريقي

18/09/2022

الشيخ مصطفى الكريم عالم بسر الحروف الفعلية باجسادها وطبائعها واروحعها التي تنفعل بها من خير وشر أعظم ساحر أفريقي

Photos from Cheikh Moustapha al karim's post 10/09/2022

Secret kimyaou ( سر كمياء) bou gaw thi alal ( l'argent
Liguay zikr
يا حي ياقيوم ذ الجلال والإكرام 1000 fois
يا همسمفطمقض 6666 fois
يا هيروش يا ميرو ش 66 fois
يا شمهروش يافلديوش 66 fois
يا طلديزش 66 fois
يا ملديوش 66 fois
يا قلديوش 66 fois
يا ضديوش 66 fois
نحن خلقناهم وسددنا أسرهم واذا سئنا بدلنا امثلهم تبديلا 75 fois

09/09/2022

الشيخ مصطفى الكريم عالم بسر الحروف الفعلية باجسادها وطبائعها واروحعها التي تنفعل بها اشياء من خير وشر أعظم ساحر أفريقي أفضل شيخ بالسودان

09/09/2022

ان بطش
Bindeu ko 70 fois yeuyko do paralysé moukou

Photos from Cheikh Moustapha al karim's post 09/09/2022

Yokou awra et ngora très efficace disponible
الشيخ محمد مصطفى الكريم عالم بسر الحروف الفعلية باجسادها وطبائعها واروحعها التي تنفعل بها اشياء من خير وشر

09/09/2022

Voici une recette mais très très efficace .c'est une recette déblocage (oubikou)
Vous cherchez la Carcasse de la torture tu mets de l'eau dessus et tu te lave avec pendant 7 jours préférence avec l'eau de fleuve, mer ou puits tu te lave t**d avant de dormir.
Résultats immédiat

09/09/2022

Grand recette d'ouverture de chance en tout
Une recette à haute dose de (geomancie)
Ingrédient :
👉Un parfum Saint Michel.
👉9 feuilles de laurier.
Écrit la figure de géocentrique en image 1222 sur chaque feuille fraîche de laurier, introduit les dans l'eau avec un peu parfum et commence à l'utiliser sur ton corp pendant 7 jours .
Résultats immédiat

Photos from Cheikh Moustapha al karim's post 09/09/2022

L'amour infini ( nopp sa nekalê mou topoula par force ) rituel très puissant et rapide pour retour d'affection.
Dompter ton homme ou ta femme plus amoureux (ese) de toi .
Nb: c'est pas pour célibataire .
الشيخ محمد مصطفى الكريم عالم بسر الحروف الفعلية باجسادها وطبائعها واروحعها التي تنفعل بها اشياء من خير

09/09/2022

Kou beuga touki mou diafè bindal
ثم السبيل يسره ثم اماته فأقبره 7fois
Bindeu saw tour ak saw tourou wadiour sangoko.
Bindeu sorate yasine (يسن والقرآن )
Oubi mimya def sa tour ak sa tourou wadiour sangoko.
Oute 7 pitakh(7oiseau )dieul benn dioublou penkou (est) wakh ( ابابكر) soukhi niari laf( 2 plume)bayi mou naaw .
Dielat banen pitakh dioublou sowou(l'ouest)wakh (علي) soukhi niari laaf bayimou naaw.
Dielat banen dioublou ganar wakh (عمر) soukhi niari laaf bayimou naaw.
Dielat banen dioublou saloum wakh( عثمان)
3 yidéss ngua bayi niou naaw .
Touki dinala yombou lool
Résultats immédiat 🙏

Photos from Cheikh Moustapha al karim's post 27/04/2020

On fait tout bamou dèss deflou bone mba lou niaw wayè kouniou dieuflentel sa adio dina fadiou inchallah woniou+221775943377 disponible WhatsApp

Vous voulez que votre entreprise soit Société De Santé Et De Beauté la plus cotée à Dakar ?
Cliquez ici pour réclamer votre Listage Commercial.

Vidéos (voir toutes)

#listikhar #seette xam say sarakh 🌹#seette pour savoir toutes opportunités du personne à n'importe quel distance 🌹☎️7759...
الشيخ مصطفى الكريم عالم بسر الحروف الحروف باجسادها وطبائعها واروحعها التي تنفعل بها اشياء من خير وشر
الشيخ مصطفى الكريم عالم بسر الحروف الفعلية باجسادها وطبائعها واروحعها التي تنفعل بها اشياء من خير وشر أعظم ساحر أفريقي أ...
Dompter une femme ou garçon
On fait tout bamou dèss deflou bone mba lou niaw wayè kouniou dieuflentel sa adio dina fadiou inchallah  woniou775943377...
شيخ مصطفى الكريم عالم بسر الحروف الفعلية بأجسادها وارواحها وطبائعها الأربعة التى تنفعل بها اشياء من خير وشر

Téléphone

Site Web

Adresse

Dakar
Autres sociétés de santé et de beauté à Dakar (voir toutes)
Promo Import Promo Import
4 Avenue Cheikh Anta DIOP Immeuble Promo Import
Dakar, 21770

Une éloge à la beauté Africaine.Tout pour vous mesdames, mais pour vous aussi messieurs !

Niyel Niyel
Dakar

Niyel: an international campaigns, advocacy, and public affairs firm. We are change creators.

SANTÉ à tout prix SANTÉ à tout prix
Dakar, 12000

Meilleure Santè, Meilleure Vie

Cabinet serigne darra Cabinet serigne darra
Kaolack
Dakar, 12345

serigne dara est un grand marabout voyant et guerrisseur traditionnel...

BIO SHOP BIO SHOP
Dakar

Vente de vitamines et produits bio pour booster tonus et vitalité

Y2sbalancessenegal Y2sbalancessenegal
Fann Hock
Dakar

société spécialisé dans la vente et fabrication de machine d'auto diagnostique qui permet de détecter sel minéraux,liquide,protéines,masse de graisse,tension artérielle,fréquence c...

Nanani shop Nanani shop
Dakar, 10700

Le plaisir de s'offrir ou d'offrir! boxes cadeaux, beauté, parfums,accessoires etc. boutique en lig

Magic Butter By MDL Magic Butter By MDL
Liberté 6 Extension
Dakar, 11000

Produits de beauté

priorité Santé Ndao Good Job priorité Santé Ndao Good Job
DAKAR
Dakar, 00198

PRIORITÉ SANTÉ NDAO GOOD JOB

Oremi’Wami Oremi’Wami
Dakar

�Dakar Oremi’Wami une marque qui vise à vous proposer des accessoires de beautés mais aussi de

CODEX CODEX
CENTRE ANTI POISON HÔPITAL FANN/DAKAR/SENEGAL
Dakar

CODEX Crée par décret N°83 -1204 du 24 novembre 1983, le Comité National du Codex Alimentarius (CNCA) est placé sous la tutelle du Ministère de la Santé et de l’Action sociale. ...