wakeur_mame_cheikh_ibra_fall
Contact information, map and directions, contact form, opening hours, services, ratings, photos, videos and announcements from wakeur_mame_cheikh_ibra_fall, News & Media Website, .
«bul di jàmbat, na nga doon ab jàmbaar ba ku la gis f**k ni jeexa lo da ra»
Mame Cheikh
Ibrahima Fall a dit :
« Un monde sans Serigne Bamba, un monde sans moi, Ce monde sera lugubre.
Je vous conseille,en ce moment-là, de suivre les fils de Serigne Bamba car ils
détiennent la science pour guider toute l’humanité. »
S.Mountakha Bassirou
S.Cheikh dieumb fall
yaguelen tee wer
💞💞DIARRAMA MAME LAMP 💞💞
baye fall civilisee❤🙏
Ak lou meunti khew Ndogou Serigne Bamba yi dafay diouk Yallah na sa diam yague Fall
Le Messager (Salla Allahou Alaihi wa Sallam) a dit en parlant de la récompense de celui qui donne à un jeûneur de quoi rompre son jeûne :
" Celui qui donne au jeûneur de quoi rompre son jeûne aura la même récompense que lui, sans pour autant que cela ne diminue en rien la récompense du jeûneur lui-même. "
Lamp Baboul Mouridinah ma lumière moy Yoon wi Dieureudieuf Khadimou Rassoul Diarama Maam Seex Ibra Faal 👌
Mboolém Murid yi yèpp a ngi jooy
Ngir lu niu. bay mu daldi gooy
Ba seeni àddiyaa ngi booy
Sarax nu naatal xarnu bi
Cheikh Modou Kara Noreeyni
Ah doom:
Niom daniouy toopou Yalla.Yén naguéni wout Yalla.
Kouy toopou naguay djouli , woor, naat assaka,dém maaka
Wayé kouy wout Yalla sa baakan ,sa ndiambot ak sa aalal lagnela lathie
Kou toopou Yalla ,Yalla yeureum leu wayé kou wout Yalla , Yalla geureum leu
Té kou Yalla yeureum gua dougou Aldjana wayé kou Yalla geureum naguay dougualaté Aldjana
Serigne Abdou Karim néna "Lou baxx yomboul Liy nirog lou baxx nak yomb na.Té liy nirog lou baxx noko wouté danaka am ko.Wayé lou baxx bala nga sé am, diar si lou méti."
Yalla nanou Yalla may ngeureumeul Yalla !
Lamp Baboul Mouridinah ma lumière moy Yoon wi Dieureudieuf Khadimou Rassoul Diarama Maam Seex Ibra Faal 👌
Tjrs aux services du Cheikh❤🙏
Bismillah *Waxi mame Cheikh Ibra fall* : Ah dome weurseuk dou linguen fokk weurseuk mooy bougnou weuré seuk bi (bamel)* basay mbokou weurleu daadi gnane bâ dem, langa fay fekk mooy sa weurseuk boudeii jeuf diou bax la. Cëyyy