La révolution de la Tarikha khadria
Contact information, map and directions, contact form, opening hours, services, ratings, photos, videos and announcements from La révolution de la Tarikha khadria, College & University, .
Tourou malaka yigua xamna kou xam séni toure sa yarame aramna safara gnou téwlou ak Cherif Heuyba Aïdara
Lane Moy koor avec Cherif Heuyba Aïdara
Majma'ah avec Cherif Heuyba le guide spirituel de BABJAN Thème: le retour du prophète aleyhi salam de l'insurrection
HBD général bi ki donou Mamame Cheikhal mamame Saad bouh Cheikhna Mouhamed Vadal Seydouna Mouhamed douneule ta werr aïdara
CHEIKHNA CHEIKH NAMA AÏDARA KHALIFA GÉNÉRAL DES KHADRES
Beugu sa réw si diamou yalla la bokk Cheikh Heuyba vous souhaite une bonne fête de l'indépendance di niane yalla sakhale diam si Sénégal ak liko weur si Barker cheikhna Cheikh Abdoul Aziz
NAgnou ragual sounou borome lata déh di khéy feugu sounou bountou
Mangui d**k sama bopp diléne d**k ragal yalla téguéne moyté nikou biss bignouy diougué fi déme si yalla ta sila yalla dignou atté nagnou ragal yalla si lépp lignouy déff
Cheikhna cheikh Abdoul Aziz dane na wakh "Moytou léne réthiou biss bigua xamni réthiou doufa diarign dara"
YALNA YALLA DÉFF DIAM SI SÉNÉGAL AK LIKO WEUR SI BARKÉ CHRIKHNA CHEIKH ABDOUL AZIZ OULD CHEIKHNA CHEIKH TALIBOUYA
Quarante ans avant sa naissance Cheikhna cheikh Saad Bouh avait tenu les propos suivants à Cheikh Aboul Ma-ali le dernier disciple qu'il avait élevé au rang de Cheikh :" je te confie ce qui appartient à mon petit-fils qui sera identique a moi à tous égards. Il s'appellera AbdoulAziz. Tout ce qui est en moi en termes de baatine , Xam-Xam , Wilaya , bref tout ce qui fait un grand homme de Dieu se retrouvera sur lui ".Il nous échoit de reparler d'un homme dont nous en savons que très peu, mais sans risque de nous tromper, nous pensons pouvoirs affirmer que trés peu de gens ont connu cet homme Cheikhna cheikh abdoul Aziz
Cheikhna cheikh Abdoul Aziz et son grand frère Cheikhna cheikh Aya Aïdara
Cela fait 1an 1 mois une semaine que Cherif Heuyba a répondu ce message de Moustapha Diakhaté Allahou Akbar dieureudieuff Cheikh Heuyba tu joues des rôles importants dans l'islam
Mouhamed(psl) mo gueune lou yalla bineu ay waydiourame gnon gueune kou yalla bine Mouhamed diamonome mo gueune diamono bou yalla bine Aÿ sakhabame gnon gueune kou yalla bine Mouhamed mo gueune kou yalla bine
Premier tourné cheikhna cheikh Sidaty a Dakar accompagné de cheikhna cheikh Abdoul Aziz et cheikhna cheikh Aya actuel khalifa yalna fi yagu té andak wérr
weukhieurtou ould cheikhna cheikh Talibouya alter-égo de cheikhna cheikh Saad Bouh Yalna yalla yokk Aÿ lérale ta tass gnou si barkéme
Inna lilahi wa inna ileyhi raadjihoun Cherif Mouhamed Malaïnine ould Beyah vient de nous quitter yalna ko yalla yeureume ta kharéko aldjiana firdaw si
Kou mamone cheikhna cheikh Abdoul Aziz na khole si cheikh Heuyba mi done mamame si wakhine si dieufine si lépp Aïdara dékale gua lassa mame yorone
Walof Ndiaye néna lassa mame seûteu kay dieulle
Celui-là est un homme de Dieu exceptionnelle qui joue des rôles très importants dans l'islam en général et la Tarikha khadriya et Aziziya en particulier nommé le général de son grand père fils de cheikh maleyni ould Doctor heuyba ould cheikh mou rabi rabi ould cheikhna cheikh Maleyni et de sokhna Euzeu Mint cheikhna cheikh Abdoul Aziz la réincarnation parfaite de Cheikhna Cheikh Saad bouh l'océan mystique sans rivage
CHEIKHNA CHEIKH ABDOUL AZIZ AL AMSALI LA RÉINCARNATION PARFAITE DE CHEIKHNA CHEIKH SAADBOUH
CHEIKHNA CHEIKH ABDOUL AZIZ Et SON GRAND CHEIKHNA CHEIKH AYA ET SERIGNE ABDOU AZIZ SY AL AMINE
Cheikhna cheikh Abdoul Aziz et serigne Mansour Sy borom Darad dji
cherif mouhamed lamine cheybata nous parle des qualites de cheikhna cheikh abdoul Aziz.
Que Dieu l'acceuil dans les plus grandes paradis
Cheikhna Cheikh Abdoul Aziz Aïdara et ces deux grands frères cheikhna cheikh Atkhana Aïdara et cheikhna cheikh Aya Aïdara actuelle khalif des khadre yalna yalla guoudeule faname
Cheikh Al Islam et Cheikh Aya korité 1999 képp kou dioulli sama guinaw yalna sa yarame aramale safara weukhieurtou cheikhna cheikh Abdoul Aziz
Gnou wadiale le 25 inchallah sargal Cheikha Cheikh Abdoul Aziz déllo ndioukeule cheikh Heuyba Aïdara le général
Inana illahi wa Inna illeyhi radjioune cheikhal khoutoub ould Walid n'est plus.Nous présentons nos condoléances à toute la Oumma Islam et la tarikha khadria ainsi que la famille chérifienne.Que Dieu l'accueille au paradis 🙏🙏🙏
Cheikhna cheikh Abdoul Aziz ak makame cheikhna cheikh Aya actuelle khalif de cheikhna cheikh Saad bouh yalla nako yalla may guoudou fane bou andak wérr
Yonénty bi salalahou aleyhi wa salame néna souguéne khamone liguéni tassél guanaw déh...